(Wolof version)
listen here:
http://abibitumikasa.com/yabb/YaBB.pl?num=1162565557/0#0
Xeex, sama xarit, xeex
Ngir moom sa bopp, xeex
Xeex be dee xeex
Ginaaw loolu nak, xeex,
Xeex sama moroom, xeex
Ngir xam sa bopp, xeex
Xeex be tas, xeex
Ginaaw loolu nak, xeex,
Kaas, sama xarit, kaas
Ngir aar sa bopp, kaas
Kaas be am ndam, kaas
Soo ame ndam nak, kaas,
Kaas, sama moroom, kaas
Ngir ban nguuru bon, kaas
Kaas ngir jub, kaas
Kaas, sama moroom, kaas,
San, sama mak, san
Ngir aar sa non, san
San ngir fippu, san
San, sama mak, san,
San, sama rak, san
Ngir fayyu, sama rak, san
San ngir fayyu, san
San sama rak, san,
Faayu sama non, fayyu!
Ngir gaddu sunu liggeey, fayyu!
Fayyu be am ndam, fayyu
Fayyu sama non, fayyu
Fayyu sama non, fayyu...
Fippu, sama non, fippu
Fippu ngir jubbanti, fippu
Ngir jaar sunu yoon, fippu
Ndox du fatte yoon am, fippu
Fippu ngir fayyu, fippu!
Fippu ngir fayyu, fippu!
Fayyul sunu maam, fayyu,
Fayyul sunu bopp, fayyu
Fayyu, sama xarit, fayyu,
Soo fippuwe nak, fayyu
Soo fayyuwe nak, fippu
Fippu, sama xarit, fippu,
Fayyu, sama xarit, fayyu.
Xeex, sama xarit, xeex
Ngir moom sa bopp, xeex
Xeex be dee xeex
Ginaaw loolu nak, xeex...
Obadele Kwame Kambon
_________________________________________________________________
(translated into whiteySmiley
Fight, my friend, fight
To free yourself, fight
Fight 'til death, fight
Even after that, fight,
Fight, my kinfolk, fight
To know yourself, fight
Fight 'til destruction, fight
Even after that, fight,
Rebel, my friend, rebel
To protect yourself, rebel
Rebel 'til victory, rebel
Even after gaining victory, rebel,
Rebel, my kinfolk, rebel
To reject evil government, rebel
Rebel to be righteous, rebel
Rebel, my kinfolk, rebel,
Dare, my elder, dare
To protect your people, dare
Dare to revolt, dare
Dare, my elder, dare,
Dare, my young one, dare
To avenge, my young one, dare
Dare to avenge, dare
Dare, my young one, dare,
Avenge, my people, avenge!
To fulfill our duty, avenge
Avenge til victory, avenge
Avenge, my people, avenge
Avenge, my people, avenge...
Revolt, my people, revolt
Revolt to make things straight, revolt
To follow our path, revolt
Water does not forget it's path, revolt
Revolt to Avenge! Revolt!
Revolt to Avenge, Revolt!
Avenge Our Ancestors, Avenge!
Avenge Ourselves, Avenge!
Avenge, my friend, Avenge,
If we revolt, also, avenge,
Revolt, my friend, revolt,
Avenge, my friend...avenge!
Fight, my friend, fight
To free yourself, fight
Fight 'til death, fight
Even after that, fight...
Obadele Kwame Kambon